- Maamuun bi ak imaam bi am na ñent anam: ñatt yi dañu koo tere, te mooy: jiitu, ak tollo, ak yeex, la ñu yoonal ci maamuun bi mooy: topp imaam bi.
- Maamuun bi daa war a topp imaam bi ci julli gi.
- Ag tëkku ci soppi melow kiy yëkkati boppam njëkk imaam bi def ko melow mbaam lu man a nekk la, te mooy soppi.