- Solos rafetal julli gi, ak def ponk yi ànd ak dal ak toroxlu.
- Melal ku dul matal ay rukoom ak i sujjóotam ci ne ab sacc la ngir moytandikuloo waate ci loolu, ak bàyyiloo xel cig araamam.
- Warug matale rukoo yi ak sujjóot yi ci julli gi ak yamoo ci ñoom ñaar.