- Muslu yii dafa bokk ci ñaan yi gën a am solo te matale, ngir li mu làmboo ag muslu ci ayi àdduna ak allaaxira.
- Mbugalum bàmmeel lu sax la te dëgg la.
- Loraangey fitna ak solos muslu ci Yàlla ak ñaan ngir mucc ca.
- Saxal ne Dajjaal dana génn ak fitnaam gu màgg ga.
- Sopp nañu ñaan gii ginnaaw taaya ju mujj.
- Sopp nañu ñaan ginnaaw bu ñu defee jëf ju sell.