- Leeral li ñu sopp ci kiy julli mu wax ko bu yëkkatee boppam jóge ca sujjóot ba.
- Yoonal nañu yamoo ak dal ginnaaw bu ñu siggee ca rukoo ba; ndax manuta wax sikar bii ludul bu yamoo ba dal.
- Sikar bii nag lu ñu yoonal la ci mbooleem julli yi moo xam farata la walla naafila.