- Leeral solos julli ak bañ koo sàgganee def ko ca waxtoom ak fay ko.
- Daganul ñuy yeexe julli ca waxtoom te tay ko ci lu dul ngànt.
- Ki fàtte daa war a fay julli yi mu fàtte woon saa yu ko fàttalikoo, ak aji-nelaw ji saa yu yewwoo.
- Dàñoo war a fay julli yi ca na mu gën a gaawe doonte ca waxtuy tere ya la.