- Jàngal xale yi seen mbiri diine njëkk ñuy mat mukallaf, te julli bokk na la ca ëpp solo.
- Dóor gi ngir yar la, waaye nekkul ngir mbugal, kon dees na ko dóor dóor gu yelloo ak jëmmam.
- Yittewoog Sariiha ci sàmm der yi, ak fatt bépp bunt buy jëme ci yàq.