- Bokk na ci njariñal hdiis bi: Sunnay Yónente yi Yàlla bëgg te gëramloo ko, te digale ko, day waral ag mat ak ug set ak ub taar.
- Yoonal nañu sàmmoonte a.
- k bir yii, te bañ koo sàggane.
- Melo yii am na ay njariñi diine ak àdduna, bokk na ca: rafetal ay melo, setal yaram, ak fegu ngir laab,
- ak wuuteek yéefar yi, ak def ndigalal Yàlla.
- Tudd na ñu ci yeneen hadiis yeneen melokaani sunnay bindiin yu dul juróom yii, niki: yar ab sikkim, ak socc, ak yeneen.