- Lislaam daa yittewoo ag cet ak laab.
- Sangu àjjuma lu ñu sopp sopp gu ñu feddali ngir julli gi.
- Dañoo tudd bopp doonte tudd gi ñu tudd yaram wi làmboo na ko; ngir yittewoo ko.
- Sangu war na képp ku am xet gu bon guy lor nit ñi.
- Bis bi gën a feddalikoo sangu mooy bisu àjjuma; ngir ngëneelam.