- Saraxndiku dafa war ci njàpp, te mooy: dugal ndox mi ci bakkan jaare ko ci noyyi, niki noonu it saraxndiku daa war, te mooy: génne ndox mi ci bakkan bi jaare ko ci noyyi.
- Sopp nañu fomp di lu tóol.
- Yoonalees na raxas ñaari loxo yi ñatti yoon ginnaaw ay nelawi guddi.