- Amna solo lool ñu jàngal xale yi ak ndaw ñi biri diine niki wéetal Yàlla ak ay teggin ak yeneen.
- Am pay day toll kem na jëf ja toll.
- Digele ci sukkandiku ci Yàlla, ak wakkirlu ci Moom wolif lu dul Moom, ndax mooy gën gi wéeruwaay.
- Gëm ndogal yi te gërëmloo ko, ak gëm ne Yàlla dogal na lépp.
- Ku sànk ndigali Yàlla yi, Yàlla dana ko sànk.