- Saxal wàccug Hisaa -yal na ko Yàlla dolli jàmm- ci mujjug jamono, ak ne dafa bokk ci màndargay bis-pénc.
- Sariihab Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa folli bu dul moom.
- Wàccug baarke ci alal yi ci mujjug jamono, ak ni ko nit ñi di dëddoo.
- Bégle ci desug diiney Lislaam ba Hiisaa -yal na ko Yàlla dolli jàmm- ci lay àtte ci mujjug jamono.