- Boole xam ak jëfe ag mucc la ci yoonu ña ñu mere ak ña réer.
- Moytondikuloo yoonu Yahuut yi ak nasaraan yi, te taqoo ak yoon wu jub wi te mooy Lislaam.
- Yahuut yi ak nasaraan yi ñéppa réer te ñépp lañu mere, waaye melo wi Yahuut yi gën a jagoo mooy mere, wi nasaraan yi gën a jagoo mooy réer.