- Wakkirlu ci Yàlla mu kawe mi,ak ne kenn du indi aw yiw ku dul Yàlla,kenn it du jeñ aw lor ku dul Yàlla.
- Tere nañu gaafal, te mooy di ñaawal dara, ba muy teree
- def dara.
- Gaatnga lu baax nag bokkul ci gaafal gi ñiy tere,waaye moom dafa bokk ci rafet njort ci Yàlla mu kawe mi.
- Lépp lu mu man a doon ci dogalub Yàlla lay ame ak nattalleem moom dong amul bokkaale.