- Bokk na ci njariñal hdiis:
- Pay daal mi ngi ajo ca kem jëf ya cib tollowaay ak melokaan.
- Ñaaxe ci jàng Alxuraan ak xereñe ko ak mokkal ko ak settantal ko ak jëfe ko.
- Àjjana ay kër la ak i daraja yu bari, ñon Alxuraan yi danañu fa am ay daraja yu gën a kawe.