- Leeral ngëneelu Yàlla ci jaamam yu gëm yi ak yërmàndeem ci ñoom, ci jéggal leen seen i bàkkaar ci lor yu néew yi leen di dal.
- Jaadu na ci jullit bi muy yaakaar payug Yàlla ci li koy dal, di muñ lu ndaw ak lu rëy, ngir mu nekk ci ag yëkkatiku daraja ak far ay ñaawteef.