- Gaaflu bokkaale la ; ndaxte day wékk xol bi ci ku dul Yàlla.
- Njariñu baamtu masala yu am solo yi, ngir ñu wattu ko ak mu sax ci xol yi
- Gaaflu li koy dindi mooy wakkirlu ci Yàlla mu kawe mi.
- Digle nañu ñuy wakkirlu ci Yàlla rekk te wékk xol bi ci Yàlla mu sell mi.