- Bokk na Nit ñi dañoo rawante ci ngëm.
- Sopp nañu kàttan ci jëf yi; ndax njariñ man na caa ame amiin woo xam ne bu ca kàttan ga nekkul woon du am.
- Nit ki dafa war a xér ci lu koy jariñ, te bàyyi lu ko dul jariñ.
- War na ci aji-gëm ji muy sàkku dimbaluYàlla ci mbiram yépp, te mu bañ a sukkandiku ci boppam.
- Saxal dogal yi ak ne loolu du dàquwante ak def sabab yi ak dox ci sàkku yiw yi.
- Tere nañu ñuy wax "budul woon nàngam” di ko wax ci anamug naqarlu ci wàccug musiba, araamal nañu it di gaaral ab dogalu
- Yàlla mu kawe mi.