- Yërmànde ci mbooleem mbindéef loolu de luñu sàkku la, waaye dañoo tudd nit ngir fonk giñuleen fonk.
- Yàlla mooy Aji-Yërëme ji te mooy yërëm ay jaamam yiy yërëme, ndax pay moom ca kem jëf ja rekk.
- Yërëm nit ñi day làmboo di àggale ci ñoom baax di leen jeñal lu ñaaw tey jëflanteeg ñoom lu rafet.