- Bokk na ci njariñal adiis bi :
- Ngëneelu bëggante ci diggante jullit ñi, ak muuñ ak bég boo dajeek keneen.
- Matug sariiha jii ak ug làmboom
- lépp luy baaxal jullit ñi, ak lu leen di bennale
- Ñaaxe ci def lu baax donte lu néew la.
- Sopp nañu di bég Loo jullit ñi; Ndax loolu dafay tax ñu gën a miinante.