- Ngëneelu mbëggeel gir Yàlla rekk tax, ci lu dul njariñul àdduna.
- Sopp gi ñu sopp
- ñu xibaar ki ñu bëgg ngir Yàlla ci bëgg gi ñi ko bëgg, ngir mbëggeel ga ak miineel ga gën a yokk.
- Tasaare mbëggeel ci biir way-gëm ñi day dëgëral mbokkoog mgëm, day wattu mbooloo mi ci taasaaroo ak tàqalikoo.