- Yërmàndeg Yàlla mu kawe ak ñeewantoom ci mbindeef yi
- Rafetal ray gi ak rendi gi ci defe ko ca anam ga ñu ko yoonale.
- Matug Sariiha ak làmboo gimu làmboo léppi yiw, bokk na ca yërëm rab yi ak ñeewantu leen.
- Tere di ñaawal yaramu nit ki ginnaaw bi ñu ko rayee.
- Araamug lépp loo xam ne mbugal baayima da caa nekk.