- Ñaaxe ci roy ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ak jikkówoo jikkóy Alxuraan.
- Tagg jikkóy Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ci ne ci leeru wahyu gi la bokk.
- Alxuraan mooy cosaanu bépp jikkó bu tedd.
- Jikkó yi ci Lislaam day làmboo diine jépp, ci def ndigal yi, moytu tere yi.