- Dugg àjjana daa am ay sabab yu aju ci Yàlla mu kawe mi, bokk na ca: ragal ko, ak ay sabab yu aju ci nit ñi, bokk na ca: rafet jikko.
- Làmmeñ lu bon la ci boroom, te bokk na ci liy tax a dugg safara.
- Lorànge yi ci bànneex yi ak ñaawtéef yi ci nit ñi, mooy ne bokk nañu ci liy gën a waral ñu dugg sawara.