Jële na ñu ci Husayfata Inb Yamaan -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax naan: «ab ràmbaajkat du dugg àjjana».
Al-buxaariy ak Muslim dëppoo nañu ci génnee ko ci seen ñaari téere yi gën a wér
Explanation
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli jàmm- day xamle ne ràmbaajkat biy tuxal ay wax ci diggante nit ñi jubloo yàq séen diggante kooku yayoo naa mbugal ci mu bañ a dugg àjjana.
Hadeeth benefits
Bokk na ci njariñal adiis bi :
Rambaaj ci Bàkkaar yu mag yi la bokk.
Tere nañu rambaaj; ndax li ci nekk ci yàq ak lor ci diggante nit ñi ak askan wi.
Share
Use the QR code to easily share the message of Islam with others