- Refetal ci jëflante ak nit ñi, ak di leen baal, te di jéggal ki nekk ci jafe-jafe daa bokk ci sabab yi gën a màgg ci muccug jaam bi ëllëg bis-penc.
- Rafetal jëme ci nit ñi, ak sellal ngir Yàlla, ak yaakaar yërmaandeem, daa bokk ci sababi njéggali bàkkaar yi.